We’ve updated our Terms of Use to reflect our new entity name and address. You can review the changes here.
We’ve updated our Terms of Use. You can review the changes here.

GUETH

from JOTNA by Fakeba

/
  • Streaming + Download

    Includes high-quality download in MP3, FLAC and more. Paying supporters also get unlimited streaming via the free Bandcamp app.
    Purchasable with gift card

      name your price

     

about

lyrics

GUETH

waw gueth waw geuthe waw geuthe 

waw guette waw guetth waw geuth
waw gueth waw gueth waw geuth

waw gueth waw geuth 
geuth mamoulane né khé 
geuth mamoulane  khan khan 
ya mome weuyii iiiiiiiiiiiiii

khame nané dikame dou ñoune rek kafi 
dou ñoune rek kafi nékeu euhhh 

mame mamoulane khan khane mame mamoulane khan khane 
damalaye niane ñéte 
béne moye nga wakh ak mane thi sama geunte
geuth mamoulane né khé 
weuye wi yaye borome


niarér moye niarér bi moye nga goungéna thie samaye yone 
mame mamoulane doumala meusa sori 
yaye souniou sétou diganeté asamant ak souffe sé mame boye yooo khoo khoo  
mame mamoulane khan khane mame mamoulane khan khane 

waw gueth waw gueth 
geuth mamoulane né khé 
mame mamoulane weuye wi paye brome
 
uhh en euh en tu ta té
khame nane khame na ah ah khan ah dou niou rek kafi nékeu 
sama mame boye wakhma khan uhhh mame mamoulane ame nga yeurmandé 
boye nianalema arma mame boye ko are mouniou thi geuth 
mame boye yé yé yé koubala mame boye yoooooooohh
bala ouhhhhhh lilala dié mame boye yooooooookhoyooo
 
nga goungéma thie sama yone
mame mamoulane né khé weuyii yaye borome
yeurmandé é éh yeurmandé déla a khan lalala 
mame mamoulane no non uhh mame mamoulane
damalaye niane ñéte bene bii moye 
nga goungéma thi samaye yone
mame mamoulane non non sama mame mamoulane 
yaye souniou sétou diganeté asamane ak souffe sé souffe sé
mame mamoulane weuye wi yaye borome ooooooome

credits

from JOTNA, track released February 14, 2020
Iberlive Entertainment

license

all rights reserved

tags

about

Fakeba Dakar, Senegal

Fakeba, an intense voice with precious textures, that emerges from the heart of Africa and that will flying out around the planet with the power of Electronic Music. Fakeba sings in her language, the Wolof, language of Senegal bathed in sea, jungles and deserts. From there Fakeba extracts his strength and her spirituality.

AN EXCLAMATION OF FREEDOM
... more

contact / help

Contact Fakeba

Streaming and
Download help

Redeem code

Report this track or account

If you like Fakeba, you may also like: